Pathé et sa petite sœur Khady s’apprêtent à aller à la foire. Un lieu d’émerveillement pour les enfants, mais aussi de péripéties pour ce qui sera sans doute … une sortie mémorable !
Paate ak rakkam ju jigéen Xadi nu ngi waaj a dem ca luuma ba. Barab bu neex si xale yi, waaye itam, barab bu mën a jur … doxantu bu doy waar !
Auteur AMINATA KHOUSSA
Be the first to review “LÉGUME DU SAHELS”